Logo YouVersion
Îcone de recherche

Macë 24:7-8

Macë 24:7-8 TI

Xeet dina jóg, xeex ak weneen xeet, réew xeex ak meneen réew. Dina am ay xiif ak ay yëngu-yënguy suuf ci bérab yu bare. Waaye loolu lépp mooy ndoortel metit yi, mel ni jigéen juy matu.

Plans de lecture et méditations gratuites relatifs àMacë 24:7-8