Logo YouVersion
Îcone de recherche

Njàlbéen ga 3:6

Njàlbéen ga 3:6 KY

Jigéen ja dafa gis ne garab gi rafet na, niru na lu neex, te mata bëgg ci kuy wuta am xel, mu witt ci doom yi, lekk; jox ci jëkkëram ji mu àndal, moom it mu lekk.

Plans de lecture et méditations gratuites relatifs àNjàlbéen ga 3:6