1
Màrk 3:35
Téereb Injiil
TI
ndaxte kuy def coobarey Yàlla, kooku mooy sama rakk ak sama jigéen ak sama ndey.»
Comparer
Explorer Màrk 3:35
2
Màrk 3:28-29
Ci dëgg maa ngi leen koy wax, lépp dees na ko baal nit ñi, muy bàkkaar, muy sosal Yàlla wu mu mana doon. Waaye kuy sosal Xel mu Sell mi deesu ko baal mukk; gàddu na bàkkaar ba fàww.»
Explorer Màrk 3:28-29
3
Màrk 3:24-25
Réew mu xeex boppam, du mana yàgg. Te kër gu xeex boppam, du mana yàgg.
Explorer Màrk 3:24-25
4
Màrk 3:11
Fekk booba képp ku rab jàpp ku ko gis, daanu fa kanamam di yuuxu naan: «Yaa di Doomu Yàlla.»
Explorer Màrk 3:11