1
Màrk 2:17
Téereb Injiil
TI
Noonu Yeesu dégg ko, mu ne leen: «Ñi wér soxlawuñu fajkat, ñi wéradi ñoo ko soxla; ñëwuma woo ñi jub, waaye bàkkaarkat yi laay woo.»
Comparer
Explorer Màrk 2:17
2
Màrk 2:5
Bi Yeesu gisee seen ngëm, mu ne làggi ba: «Sama waay, baal nañu la say bàkkaar.»
Explorer Màrk 2:5
3
Màrk 2:27
Yeesu dellu ne leen: «Yàlla sàkkul nit ngir bésub noflaay bi, waaye sàkk na bésub noflaay ngir nit.
Explorer Màrk 2:27
4
Màrk 2:4
Waaye manuñu koo jege ndax mbooloo mi. Kon ñu daldi teggi kaw kër gi, di bëtt fa tiim bérab ba Yeesu nekk, daldi yoor basaŋ, ga làggi ba tëdd.
Explorer Màrk 2:4
5
Màrk 2:10-11
Waaye xamleen ne, Doomu nit ki am na ci àddina sañ-sañu baale bàkkaar yi.» Ci kaw loolu mu ne làggi ba: «Maa ngi la koy sant, jógal, jël sa basaŋ te nga ñibbi.»
Explorer Màrk 2:10-11
6
Màrk 2:9
Lan moo gëna yomb, ma wax ku làggi ki: “Baal nañu la say bàkkaar,” walla ma wax ko: “Jógal, jël sa basaŋ, tey dox”?
Explorer Màrk 2:9
7
Màrk 2:12
Ca saa sa mu jël basaŋam te génn fa kanam ñépp. Noonu ñépp waaru, di màggal Yàlla naan: «Lu mel ni lii, masunu koo gis.»
Explorer Màrk 2:12