Logo YouVersion
Îcone de recherche

Macë 5:11-12

Macë 5:11-12 TI

«Barkeel ngeen, bu ñu leen di saaga, di leen fitnaal, di leen sosal lépp lu bon ngir man. Bégleen te bànneexu, ndax seen yool dina réy ci laaxira. Ndaxte noonu lañu daan fitnaale yonent yi fi jiitu.

Lire Macë 5

Plans de lecture et méditations gratuites relatifs àMacë 5:11-12