John 10:10

John 10:10 GWG

Sachakat ba du ñou lu dul sacha, te rēndi, te sanka; mā ñou ndah͈ ñu am dūnda, te ndah͈ ñu am ko bu bare.