YouVersion 標識
搜索圖示

Kàddug Yàlla moo dikke ñaari pàcc: Kóllëre gu jëkk gi Yàlla fas ak nit, ak Kóllëre gu yees, gi mujja wàcc, te ñenn ñi di ko wooye Injiil, mu tekki Xibaaru jàmm. Ñaari tére yooyu, Yàllaa leen wàcce ci nitam ñu sell ñi, kóllëre gu jëkk gi, ñu bind ko ci yawut, gu yees gi, ci làkku gereg. Li ñu bind ci tére yu jëkk ya nag, moom lanu tekki ci wolof.


WorldVenture

KY 出版社

WorldVenture 提供的其他譯本