Njàlbéen ga 3:20

Njàlbéen ga 3:20 KYG

Aadama nag tudde soxnaam Awa (mu firi Dund), ndax mooy ndeyu képp kuy dund.