Njàlbéen ga 6:9
Njàlbéen ga 6:9 KY
Askanu Nóoyin mooy lii. Nóoyin nit ku jub la woon, di ku mat ci biir nit ñi mu bokkal jamono, te di ku topp Yàlla.