Njàlbéen ga 3:24
Njàlbéen ga 3:24 KY
Da koo dàq, ba noppi teg ca penkub toolu Àjjana ba ay malaakay serub, boole ca saamar buy xuyy-xuyyi, tey dem aka dikk, di wattu yoon, wa jëm ca garab gay taxa dund.