Njàlbéen ga 1:26-27

Njàlbéen ga 1:26-27 KY

Yàlla ne: «Nanu bind nit ci sunu melokaan, mu nirook nun, te na yilif jëni géej ak picci asamaan ak jur gépp ak suuf sépp ak lépp lu ciy raam.» Yàlla dafa sàkk nit ci melokaanam; ci melokaanu boppam la Yàlla sàkk nit, góor ak jigéen la sàkk.

Verse Image for Njàlbéen ga 1:26-27

Njàlbéen ga 1:26-27 - Yàlla ne: «Nanu bind nit ci sunu melokaan, mu nirook nun, te na yilif jëni géej ak picci asamaan ak jur gépp ak suuf sépp ak lépp lu ciy raam.»
Yàlla dafa sàkk nit ci melokaanam;
ci melokaanu boppam la Yàlla sàkk nit,
góor ak jigéen la sàkk.

મફત વાંચન યોજનાઓ અને Njàlbéen ga 1:26-27થી સંબંધિત મનન