YouVersion Logo
બાઇબલયોજનાઓવિડિઓઝ
Get the app
Language Selector
Search Icon

Popular Bible Verses from Njàlbéen ga 4

1

Njàlbéen ga 4:7

Kàddug Yàlla

KY

Soo defee lu baax, dees na la nangul; soo deful lu baax, bàkkaar a ngi lay yeeru ci sa bunt, di la tërooka wut, waaye yaa ko wara man.»

Compare

Njàlbéen ga 4:7 ખોજ કરો

2

Njàlbéen ga 4:26

Kàddug Yàlla

KY

Set it, am doom ju góor, tudde ko Enos. Fan yooya lañu tàmbalee tudd Aji Sax ji, di ko wormaal.

Compare

Njàlbéen ga 4:26 ખોજ કરો

3

Njàlbéen ga 4:9

Kàddug Yàlla

KY

Aji Sax ji ne Kayin: «Ana sa rakk Abel?» Mu ne ko: «Gisuma ko de; ndax maa wara sàmm sama rakk?»

Compare

Njàlbéen ga 4:9 ખોજ કરો

4

Njàlbéen ga 4:10

Kàddug Yàlla

KY

Yàlla ne ko: «Loo def? Sa deretu rakk jaa ngi yuuxoo ci suuf, ma di ci dégg.

Compare

Njàlbéen ga 4:10 ખોજ કરો

5

Njàlbéen ga 4:15

Kàddug Yàlla

KY

Aji Sax ji ne ko: «Kon nag ku la rey, yaw Kayin, dina jot juróom ñaari yoon lu ko raw.» Ba loolu amee mu sàkkal Kayin màndarga, ba ku ko gis du ko rey.

Compare

Njàlbéen ga 4:15 ખોજ કરો

મફત વાંચન યોજનાઓ અને Njàlbéen ga 4થી સંબંધિત મનન

Previous Chapter
Next Chapter
યુવર્ઝન

Encouraging and challenging you to seek intimacy with God every day.

Ministry

વિષે

Careers

સ્વયંસેવક

બ્લોગ

દબાવો

Useful Links

સહાય કરો

દાન કરો

બાઇબલ આવૃત્તિઓ

ઑડિયો બાઇબલ

Bible Languages

આજનું વચન


A Digital Ministry of

Life.Church
English (US)

©2026 Life.Church / YouVersion

ગોપનીયતા નીતિશરતો
Vulnerability Disclosure Program
ફેસબુકટ્વીટરઇન્સ્ટાગ્રામYouTubePinterest