YouVersion Logo
બાઇબલયોજનાઓવિડિઓઝ
Get the app
Language Selector
Search Icon

Popular Bible Verses from Njàlbéen ga 26

1

Njàlbéen ga 26:3

Kàddug Yàlla

KY

Dalal ci réew mii; dinaa ànd ak yaw, barkeel la. Yaak sa askan laay jox suuf sii sépp, te dinaa sàmm li ma giñaloon sa baay Ibraayma.

Compare

Njàlbéen ga 26:3 ખોજ કરો

2

Njàlbéen ga 26:4-5

Kàddug Yàlla

KY

Dinaa ful sa askan ni biddiiwi asamaan, dinaa jox sa askan suuf sii sépp, te it ci saw askan la xeeti àddina yépp di barkeele, ndax Ibraayma déggal na ma, sàmm na sama ndénkaane, ak samay santaane, ak sama dogali yoon, ak samay yoon.»

Compare

Njàlbéen ga 26:4-5 ખોજ કરો

3

Njàlbéen ga 26:22

Kàddug Yàlla

KY

Mu jóge foofa, gasati teen, jàmm ne ñoyy, mu tudde ko Rexobot (muy firi Fu yaatu), ndax da ne: «Léegi Aji Sax ji yaatal na nu, te dinanu woomle ci réew mi.»

Compare

Njàlbéen ga 26:22 ખોજ કરો

4

Njàlbéen ga 26:2

Kàddug Yàlla

KY

Foofa Aji Sax ji feeñu ko fa ne ko: «Bul dem Misra, waaye nanga toog ci réew mi ma lay wax.

Compare

Njàlbéen ga 26:2 ખોજ કરો

5

Njàlbéen ga 26:25

Kàddug Yàlla

KY

Isaaxa nag sàkk fa sarxalukaay, tudd fa Aji Sax ji, wormaal ko, ba noppi samp fa xaymaam. Te itam ay surgaam bënn nañu fa ab teen.

Compare

Njàlbéen ga 26:25 ખોજ કરો

મફત વાંચન યોજનાઓ અને Njàlbéen ga 26થી સંબંધિત મનન

Previous Chapter
Next Chapter
યુવર્ઝન

Encouraging and challenging you to seek intimacy with God every day.

Ministry

વિષે

Careers

સ્વયંસેવક

બ્લોગ

દબાવો

Useful Links

સહાય કરો

દાન કરો

બાઇબલ આવૃત્તિઓ

ઑડિયો બાઇબલ

Bible Languages

આજનું વચન


A Digital Ministry of

Life.Church
English (US)

©2026 Life.Church / YouVersion

ગોપનીયતા નીતિશરતો
Vulnerability Disclosure Program
ફેસબુકટ્વીટરઇન્સ્ટાગ્રામYouTubePinterest