YouVersion Logo
બાઇબલયોજનાઓવિડિઓઝ
Get the app
Language Selector
Search Icon

Popular Bible Verses from Njàlbéen ga 2

1

Njàlbéen ga 2:24

Kàddug Yàlla

KY

Looloo tax góor di teqalikook ndeyam ak baayam, taqoo ak jabaram, ñuy wenn suux.

Compare

Njàlbéen ga 2:24 ખોજ કરો

2

Njàlbéen ga 2:18

Kàddug Yàlla

KY

Yàlla Aji Sax ji daldi ne: «Wéet baaxul ci nit, kon dinaa ko bindal ku koy taxawu te jekk ci doon wéttalam.»

Compare

Njàlbéen ga 2:18 ખોજ કરો

3

Njàlbéen ga 2:7

Kàddug Yàlla

KY

Yàlla Aji Sax ji nag móol nit ci pëndub suuf, ëf ngelawal dund ci paxi bakkanam, nit daldi doon boroom bakkan.

Compare

Njàlbéen ga 2:7 ખોજ કરો

4

Njàlbéen ga 2:23

Kàddug Yàlla

KY

Aadama ne tonet, daldi ne: «Waaw kay nag, kii moo bokk ci samay yax ak sama suux! Dees na ko tudde jigéen, ndaxte ci góor lees ko jële.»

Compare

Njàlbéen ga 2:23 ખોજ કરો

5

Njàlbéen ga 2:3

Kàddug Yàlla

KY

Yàlla daldi barkeel bésub juróom ñaareel ba, def ko bés bu sell, ndax da caa dallu woon gannaaw liggéey ba mu sàkke lépp.

Compare

Njàlbéen ga 2:3 ખોજ કરો

6

Njàlbéen ga 2:25

Kàddug Yàlla

KY

Ku góor ki ak jabaram, ñoom ñaar ñépp, yaramu neen lañu defoon, te amuñu ci woon genn kersa.

Compare

Njàlbéen ga 2:25 ખોજ કરો

મફત વાંચન યોજનાઓ અને Njàlbéen ga 2થી સંબંધિત મનન

Previous Chapter
Next Chapter
યુવર્ઝન

Encouraging and challenging you to seek intimacy with God every day.

Ministry

વિષે

Careers

સ્વયંસેવક

બ્લોગ

દબાવો

Useful Links

સહાય કરો

દાન કરો

બાઇબલ આવૃત્તિઓ

ઑડિયો બાઇબલ

Bible Languages

આજનું વચન


A Digital Ministry of

Life.Church
English (US)

©2026 Life.Church / YouVersion

ગોપનીયતા નીતિશરતો
Vulnerability Disclosure Program
ફેસબુકટ્વીટરઇન્સ્ટાગ્રામYouTubePinterest