1
Luug 1:37
Kàddug Yàlla
KY
ndax Yàlla, dara tëwu ko.»
Comparer
Explorer Luug 1:37
2
Luug 1:38
Maryaama daldi ne: «Maa ngi, di jaamub Boroom bi. Nii nga waxe, na ame noonu ci man.» Ba loolu amee malaaka ma bàyyikoo ca moom, dem.
Explorer Luug 1:38
3
Luug 1:35
Malaaka mi ne ko: «Noo gu Sell gi mooy wàccsi ci yaw, dooley Aji Kawe ji yiir la. Moo tax itam kiy juddoo ci yaw, dees na ko woowe Ku sell, ak Doomu Yàlla.
Explorer Luug 1:35
4
Luug 1:45
Ndokkalee yaw mi gëm ne mbir mi ñu la yégal, te mu tukkee ci Boroom bi dina sotti!»
Explorer Luug 1:45
5
Luug 1:31-33
Dinga ëmb, ba jur doom ju góor, nga tudde ko Yeesu. Ku màgg lay doon, te dees na ko woowe Doomu Aji Kawe ji. Boroom bi Yàlla moo koy jagleel nguurug Daawuda maamam. Mooy nguuru fi kaw waa kër Yanqóoba ba fàww, te nguuram du foq mukk.»
Explorer Luug 1:31-33
6
Luug 1:30
Malaaka ma ne ko: «Maryaama, bul tiit, ndax daje nga ak yiwu Yàlla.
Explorer Luug 1:30